SEฬRINฬ TUUBAA mas na wax Seฬrinฬ Sahiid Mbakke : mas nga gis ku mel ni Faadilu Mbakke ? Mu ni ko deedeet ! Mu ni ko mas nga deฬgg ku mel ni ki Faadilu Mbakke ? Mu ni deedeet ! SEฬRINฬ BI ni ko : Sahiid Mbakke ! doo ma laaj sax lu Faadilu Mbakke def ba xam ko doog may deฬggal..Mu ni ko bu ma ko sanฬee laaj naa la ko ? SEฬRINฬ TUUBAA ni ko : li nฬuy tuddee ag mbokku doom moo ci geฬn a jige, te dikk na ba fii ci man ni ma : ยซ loolee nฬuy tudde ag mbokku, jaay naa la ko jeฬndee ko ag murid (ag taalibe), la daa tege ci ag murid jox naa la ko hadiya ยป..boole ko ak hadiya ju takkuโฆ SEฬRINฬ TUUBAA ni Seฬrinฬ Sahiid : mas nga gis ku def loolu ? Mu ni ko deedeet ! Mas nga deฬgg ku def loolu ? Mu ni ko deedeet ! SEฬRINฬ TUUBAA ni ko loolu mooy dayoob yeฬeme ! ๐Source : Diyafatu Samadiya VOL5
#Kazu_Rajabโค๏ธ
#touba_xassida #senegalaise_tik_tok